Premium Only Content

SUNU BAKAAR - ELGOZEL - ADORATION 2022 - MUSIQUE SENEGALAISE - MALAAKA BU SÉNÉGAL - WOLOF 2022
Esayi 53 vs 4 - 5
4 Ndaxam moom sunu wopp la yenu,
sunuy mitit la sëfoo.
Nun nu foog ne dees koo mbugal,
foog ne Yàllaa ko duma, torxal ko.
5 Te moom sunuy tooñ a waral ñu jamat ko;
sunuy ñaawtéef a waral ñu dëggaate ko.
Yar yi nu jàmmal moom la dal,
te mooy ki nu wére ciy góomam.
Voici les paroles de cette chansons;
sunu bakaar nga yenu,
Tu as porté nos péchés
sunuy mitit nga sëfoo.
Tu as porté notre douleur
Fay nga sunu boor
Tu as payé nos dettes
Man may doomam ji mu bëgg
Je suis son enfant qu'il aime beaucoup
Amna bànneex ci man
Il prend plaisir à moi
Xawmu ñu won mbëggeel
Nous ne savions pas ce qu'est l'amour,
Wanga ñu loy mbëggeel
tu nous as montré l'amour
Xawmu ñu won sarax
Nous ne savions pas ce qu'est le sacrifice,
Wanga ñu loy sarax
tu nous a montré ce qu'est le sacrifice
Fay nga sunu boor
Tu as payé nos dettes
Fay nga sunu boor
Tu as payé nos dettes
Xawmu ñu won mbëggeel
Nous ne savions pas ce qu'est l'amour,
Wanga ñu loy mbëggeel
tu nous as montré l'amour
Xawmu ñu won sarax
Nous ne savions pas ce qu'est le sacrifice,
Wanga ñu loy sarax
tu nous a montré ce qu'est le sacrifice
sunuy naqar nga yenu
Tu as porté nos souffrances
sunuy mitit jeexna
notre douleur est finie
Aji manji
Tout-puissant
Igwe Igwe Igwe
Le Roi ! Le Roi ! Le Roi !
Ngir liggéeyu bant bi
pour l'oeuvre de la croix
Sama dund soppikuna !
Soppikuna ! soppikuna !!
Ma vie a changé
Bo xamee liggéey bi nekk ci bant bi, woyal ak man
Si tu comprends l'oeuvre de la croix, chante avec moi
Nous vous apportons de la musique wolof gospel senegalais inspirée afin que vous sachiez et soyez conscient du don gratuit de Dieu, veuillez vous abonner et recevoir les notifications de nos téléchargements ultérieurs
Vous êtes les bienvenus sur cette chaîne, n'hésitez pas à contribuer à la croissance de cette chaîne, en regardant et en partageant le contenu de cette chaîne avec vos amis et votre famille, car vous serez richement récompensé en sauvant des vies.
LA PROPHÉTIE :
A l'Ange de l'église du Sénégal, vous vous couchez bas et dépendez de plusieurs mains, levez-vous de votre sommeil et prenez la parole avec vous, n'ayez pas peur et ne vous mêlez pas! car mon jour est là! rumakawawakushibuatimogondalibanze (Si tu n'en as jamais tiré, tu le sais)
#Gozel, #Elgozel, musique senegalaise, gospel musique, gospel, latest gospel, wolof gospel, adja et cecile, Adja et cecile, Chansons chretien, chansons wolof, chanson gospel, adja chanson, cecile chanson,Adja musique, sunu boroom bi, adja et cecile sunu boroom bi, chansons senegalaise,magal, agal touba, magal 2022, magal 2022, senegal 2022, chansons 2022, chansons wolof, adja et cecile 2022, chansons tiktok, tiktok 2022, vskit, youtube senegal, adja cecile wolof, sama dund senegalaise, video clip chretiens wolof
-
38:44
The Why Files
4 days agoProject Ancient Arrow | The NSA's Secret War Against Our Future
22.8K63 -
2:36:06
Barry Cunningham
4 hours agoPRESIDENT TRUMP IS TRULY USHERING IN THE GOLDEN AGE OF AMERICA! CAN YOU FEEL IT?
85.9K34 -
LIVE
SynthTrax & DJ Cheezus Livestreams
3 days agoFriday Night Synthwave 80s 90s Electronica and more DJ MIX Livestream 2K Celebration SPECIAL EDITION 530pm PST / 830pm EST
1,153 watching -
LIVE
VapinGamers
1 hour ago $0.05 earnedDestiny 2 - Edge of Fate Legendary Run Part 3 - !rumbot !music
573 watching -
2:04:25
TimcastIRL
3 hours agoTrump DOJ Gives Ghislaine Maxwell Limited IMMUNITY As She Rats On 100+ People | Timcast IRL
192K96 -
1:09:09
Omar Elattar
5 hours agoThe Brain Experts: Your Brain Can Rewire Itself At Any Age & Here's How!
6.46K1 -
LIVE
IcyFPS
2 hours agoLIVE - Wuchang Fallen Feathers Pt.2 | XBOX SERIES S 1080p gameplay |
131 watching -
29:24
Afshin Rattansi's Going Underground
16 hours agoWas Epstein a Mossad Agent? Will Obama go to Prison? (Afshin Rattansi vs Alan Dershowitz)
14.9K15 -
4:26:54
Nerdrotic
8 hours ago $1.03 earnedFantastic Four Baby Steps V Superman's James Gunn, South Park Returns | Friday Night Tights 364
97.1K6 -
LIVE
megimu32
2 hours agoOFF THE SUBJECT: FAFO Friday! Cops, Crash, Kombat & Chaos!
166 watching